Marodi TV Sénégal
Marodi TV Sénégal
Marodi TV Sénégal

Marodi.TV est désireux de rendre accessible au grand public via sa plateforme internet www.marodi.tv tout type de contenu multimédia (sport, musiques, informations, divertissement) sur tout type de matériel informatique (ordinateur, téléphone portable intelligent, Tablette,...).

Commenti
  1. Ibrahima Diao

    Ibrahima Diao

    Sérére bou sant sow mourir de rire

  2. Dia Abdarahmane

    Dia Abdarahmane20 secondi fa

    Nabou sa Soubhan'Allah bi nekhnama trop 🇲🇷🇲🇷🇲🇷

  3. Bibishu fall

    Bibishu fall38 secondi fa

    Pod et marichu mom nexatul dr Sof Guen trp surtout Betty

  4. Fatoumata Sidibe

    Fatoumata Sidibe49 secondi fa

    sous-titre merciiiii encore

  5. Thiam Mbaye

    Thiam Mbaye58 secondi fa

    Pop wolof

  6. Ahmed Ba

    Ahmed BaMinuto fa

    Betty elle n’a rien à foutre ici c’est incroyable ohhhhh

  7. Françoise Sagna

    Françoise SagnaMinuto fa

    7 mn de pub ???????

  8. Tacko Niang

    Tacko NiangMinuto fa

    C’est très Dégeulace de votre part marodi, et l’autre petit con...on dirait vous essayer carrément de le décrédibiliser...vous ne réussirez pas tay lagn ko gueneuh gueum diapko,

  9. Leye Bousso

    Leye Bousso3 minuti fa

    Sheuteuttt Seri bi de aloulll beine contuniter vraiment dagueine thiounée ame na yéneine yoleine warone éguali comme le cas d'Edou et sa femme et sir aussi la même chauge lolou moye continuité seri bie mais pas sa vous êtes nul pffffff

  10. Nabou Cissé

    Nabou Cissé3 minuti fa

    Nul nul 👎🏾 nul de chez nul😒, les gars mes c’est quoi cette série?! Pod , momo vous êtes intelligent 🧠 changer cette scénario putin Là je ne vous reconnais plus 🤨

  11. mamadou diop

    mamadou diop3 minuti fa

    Max moy nandité dh bou affaires yi tiol wei req monguenei ben souvenir bou triste adiou😂

  12. Awa Jallow Dimson

    Awa Jallow Dimson4 minuti fa

    Pour mane au lieu de bety nabou mo warone niewate avec force puisk mom depuis saison 1 mingui galérer

  13. Balisto BFD

    Balisto BFD5 minuti fa

    Marodi swi désolé🙏🙏mais 5mn de publicité c abusé essayé de revoir votre timing merci🙏🙏

  14. Babacar Kane

    Babacar Kane6 minuti fa

    Qui est d'accord que morodi est meilleur des autres

  15. Khamidou Toure

    Khamidou Toure6 minuti fa

    Magnifique

  16. Wakhal Deug

    Wakhal Deug7 minuti fa

    Ki trouve k reug reug ray na toubabe bi Beuseul j’aime 😂😂🇸🇳

  17. aminata toure

    aminata toure7 minuti fa

    6 minutes de pub 😒😒 sa abuse

  18. Wakhal Deug

    Wakhal Deug7 minuti fa

    Ki trouve k reug reug ray na toubabe bi Beuseul j’aime 😂😂🇸🇳

  19. fallou fall

    fallou fall7 minuti fa

    Tonton tapha: on en a 😂😂😂 ?

  20. Mory NDIAYE

    Mory NDIAYE7 minuti fa

    C kw l’idée d parler d notre prophète ici ay kou beug yonenté bi ,boulene gniou yap yene gni di wakh lolou rew guene trop,menolene setane t bayi yonenté bi si wakh yi,yenagui fowé lou grav nak vs énervez les gens way

  21. coumba Ba

    coumba Ba8 minuti fa

    Wallah avec vos commentaire négatif j'en peux plus de liker même ci j n veux pas des que je vois Prophète rekkk j like direct j'en peux plus tout le monde aiment Prophète Mahomet (psl)

  22. Saliou Sall

    Saliou Sall8 minuti fa

    Wa nabou dafa nékalé ak wadji wala

  23. cheikh Seye

    cheikh Seye8 minuti fa

    Kat lén sen ndeye

  24. Fatou Wade

    Fatou Wade8 minuti fa

    Svp éclairez ma lanterne.N'est ce pas la publicité de produits éclaircissants est interdite au Sénégal?Bio skin nak?

  25. Mouhamed VJ

    Mouhamed VJ10 minuti fa

    Max il joue bien franchement wallah🙏🏾

  26. iss 814 iss

    iss 814 iss10 minuti fa

    Worna yalla series nekh na trop mai liguéni parle françai dafa beuri trop il faut guen xam ni sounou language Wolof la del wakh wolof bok pour gñii diagoul slt dasiye bakh trop

  27. Sadio Coulibaly

    Sadio Coulibaly10 minuti fa

    Avec nabou no stresse

  28. Ali Kebe

    Ali Kebe11 minuti fa

    Cool

  29. boubacar mbengue

    boubacar mbengue12 minuti fa

    oumou est une trè bonne actrice elle joue trè bien

  30. Maria DIEYE

    Maria DIEYE13 minuti fa

    Mane dal oumou elle est la meilleure

  31. madiop Diaw

    madiop Diaw13 minuti fa

    Pod yambar la way

  32. Tida Fofana

    Tida Fofana13 minuti fa

    Il me fait pitié Max 😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚😚 bonne chance

  33. Bob Selassie

    Bob Selassie13 minuti fa

    Trop de pub heinnn

  34. Pape Mbengue

    Pape Mbengue14 minuti fa

    Kou beug s moustapha sy al maktoum Yall nafi yaga té wér

  35. Bassirou Gueye

    Bassirou Gueye15 minuti fa

    Lula rer marche ocas touba so dike fi am nafi

  36. Djily Diop

    Djily Diop15 minuti fa

    No pot amoull diom

  37. Fachyta Cissé

    Fachyta Cissé16 minuti fa

    Aidé moi à aimer mon commentaire c'est ma 1fois mais vraiment betty me étonne énormément

  38. Coly Lamina

    Coly Lamina16 minuti fa

    La vengence va commencer avec le retourde qui?

  39. Dame Seck

    Dame Seck16 minuti fa

    Pot mome moye lolou

  40. Baye Serigne Ndiaye

    Baye Serigne Ndiaye16 minuti fa

    Ms djigen bi takkul di deuk ak mom si ben keur man yii metti nama trop

  41. Yasai Jobe

    Yasai Jobe17 minuti fa

    The french is too much in this series and the world wire love this serie so please..stop for a change

  42. dane leye

    dane leye17 minuti fa

    Lidou deuk douyone 6 miuit pour piplicité

  43. Ida Sarr

    Ida Sarr17 minuti fa

    Beth, Betty, as bad she is, she's absolutely beautiful

  44. dane leye

    dane leye18 minuti fa

    Lidou deuk douyone 6 miuit pour piplicité

  45. Ibrahima Cisse

    Ibrahima Cisse18 minuti fa

    Like: marichou Commente: betty

  46. Abdourahmane Lo

    Abdourahmane Lo19 minuti fa

    Wa serie bi mom farance laniy wakh wala wolof

  47. shasha sow

    shasha sow20 minuti fa

    Agboooooo est de retour 💪💪💪💪

  48. Rabilou Tahirou boubacar

    Rabilou Tahirou boubacar20 minuti fa

    Sous-titre s'il vous plaît

  49. Maymouna Gueye

    Maymouna Gueye20 minuti fa

    Akbo de mongimay saf villageois bouy dora niew dkr

  50. Amar Baye mbaye

    Amar Baye mbaye20 minuti fa

    No série français bi dafa bari

  51. Oumy ndiaye

    Oumy ndiaye20 minuti fa

    Mandall beugeunah Nabou bilay je t'aime

  52. Mamadou diallo

    Mamadou diallo21 minuto fa

    Momo hahaha hahaha 😆😆😆😆😆

  53. Aliou Diaw

    Aliou Diaw21 minuto fa

    Wa ana mor

  54. Omar Thior

    Omar Thior21 minuto fa

    S il vous plaît wanii les français yi dégou niou ko

  55. Babacar Youm

    Babacar Youm21 minuto fa

    Oumy tu joue bien ton jeu d'acteur est élevé du courage

  56. Fatima Sambou

    Fatima Sambou21 minuto fa

    Wa oumou mom louko dal

  57. Florence Faye

    Florence Faye21 minuto fa

    Aÿ Tonton tapha mande fatewona takkali bougina mdrr.bien joué oumy.non mais max et nabou c'est un très jolie couple .couple de l'année

  58. Mbaye Meissa

    Mbaye Meissa22 minuti fa

    Béty rk

  59. Ibrahima Diao

    Ibrahima Diao22 minuti fa

    Je suis trop fans d'elle comment j dois faire pour la recevoir ici à Paris

  60. Fall Ibrahima

    Fall Ibrahima22 minuti fa

    Trop de pub putin!!!!!!

  61. Nawal Boujbir

    Nawal Boujbir23 minuti fa

    Ne na Chu bb

  62. Amy Diop

    Amy Diop23 minuti fa

    Bétty soff na trop

  63. Boubacar Diaw

    Boubacar Diaw23 minuti fa

    Eva nopna momar

  64. Babacar diop

    Babacar diop24 minuti fa

    Mé zé joue bien son role si vous êtes d'accord avec mw poussez bleu

  65. amath thiam

    amath thiam25 minuti fa

    Mane dé begone na nek plassou Max nabou rek si khalé wouyyyy bety dogali si coté bi

  66. Johanna MJ Eklund

    Johanna MJ Eklund25 minuti fa

    Kou namou dudu pouse bleu

  67. Habiba Drame

    Habiba Drame26 minuti fa

    Wesh plus de 5min de publicité. Mdrrr

  68. Elzo Fall

    Elzo Fall26 minuti fa

    Por.et.marichou.delene.lak.wolof.te.bayi.conplekse.bi

  69. Mourtada Gueye Gt

    Mourtada Gueye Gt27 minuti fa

    Ana gniy wadjal magal prokhane 👋❤️💚

  70. TEAM 221 TIK TOK

    TEAM 221 TIK TOK27 minuti fa

    Abonné vous ma chaîne

  71. Yasmina Ndiaye

    Yasmina Ndiaye28 minuti fa

    Karamba on est fier et tres heureuse d vs voir bne continuation

  72. Mboup Abdou

    Mboup Abdou29 minuti fa

    Pod man dama khamoul goor gouko geuneu niak diom ci monde man book guissagoumako et vous?. Lignou naane pekhème djiguéne moraw saytaanè wayè betty moraw saytanè billahi.

  73. Ndack Mbaye

    Ndack Mbaye29 minuti fa

    Wa yen dolen wagni français yi ken melni negou pithie 🤦🏼‍♀️😫

  74. Soukaina Eljoumani

    Soukaina Eljoumani29 minuti fa

    🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏💓💓💓💓💓💓💓💕💕💕💕💕❤❤❤💋

  75. JULIA THIONE

    JULIA THIONE30 minuti fa

    Le patron de Sarah joue très bien son rôle

  76. Omar diallo brescia Omar selety

    Omar diallo brescia Omar selety30 minuti fa

    Filme by Faretna teop aujourd’hui 🇸🇳🇫🇷

  77. Lamine Indjai

    Lamine Indjai30 minuti fa

    teymome andena ak Nabou,koufi takh diabarou diambour yassidèss

  78. Mina Anne

    Mina Anne30 minuti fa

    Team Betty 🙋🏾‍♀️👌🏾

  79. Diop Cheikh

    Diop Cheikh30 minuti fa

    Yaw khamoné ndion simb na

  80. Sissoko Karadague

    Sissoko Karadague30 minuti fa

    Cool 😂😂😂

  81. Dibor Séne

    Dibor Séne31 minuto fa

    Ani sama beukou talibé baye yi siguiléne maléne di sénee

  82. El hadj Kouta

    El hadj Kouta31 minuto fa

    Zé ai gnangal bi 😂

  83. Ebrima Ceesay

    Ebrima Ceesay31 minuto fa

    Pod It’s very slow Knigge 🤣🤣🤣

  84. khadafy D

    khadafy D31 minuto fa

    Ah pod un peut de caractère waay

  85. diamond

    diamond31 minuto fa

    Vous arrivez vraiment à dormir avec votre femme quand vous la trompez 😭momo tu trahis la confiance de Kiné là 🤦🏾‍♀️Bilay akou kiné si abo lalay dallé yalnala massacrer ba do xol 😂😂😂

  86. Ziza Baba

    Ziza Baba32 minuti fa

    Moi j'aime trop beti

  87. Rokhaya Sene

    Rokhaya Sene32 minuti fa

    Djeukeurou Marichou bi mom hi😂😂😂😂

  88. Mame Saye

    Mame Saye32 minuti fa

    Wouy tonton tapha ray nama🤣🤣🤣🤣

  89. dg lion

    dg lion32 minuti fa

    Sene xam xam légui mou diekh

  90. Mouhamed Mbacke

    Mouhamed Mbacke32 minuti fa

    Pod ñiakk nga diom

  91. diallo Diallo

    diallo Diallo32 minuti fa

    La saison 4 n’est plus bonne

  92. Soda lô

    Soda lô32 minuti fa

    Mais koné mom si liguey la bok walla mom guissou ma ko si entreprise degou mako si entreprise

  93. Mariettelibeudj Badiane

    Mariettelibeudj Badiane34 minuti fa

    Betty daal doubay dara

  94. Coly Lamina

    Coly Lamina34 minuti fa

    Mtn betty tu é grosse comme une patate😜😝🙉🙈

  95. Dia Sydi Ndiaga

    Dia Sydi Ndiaga34 minuti fa

    Bilahi BETTY AY bo naturel Lone Bayi sa manière yi Kene doula Dax Xolatal sa bop way issh

  96. Amy Ngom

    Amy Ngom34 minuti fa

    qui est d'accord que kiné est la meilleure actrice de la série ☝️😍😍😍

  97. Wallyseckinfos____

    Wallyseckinfos____36 minuti fa

    Ehhh khouli weuhhh setanal te bayii commentaire Yi ngaye lire 😂😂😂😂😂😂

  98. réma queen sy

    réma queen sy36 minuti fa

    Nn nabou dal dou décourager je l'aime bien

  99. Mamoudou Diallo

    Mamoudou Diallo37 minuti fa

    Qui remarque la faute sur le message de Betty envoyé à Nabou?

  100. la puissance

    la puissance38 minuti fa